cover

Dabbaax-Youssou N'Dour

 如无法下载或有错误,请刷新重试或点此反馈给我们
Dabbaax-Youssou N'Dour.mp3
[ti:Dabbaax][ar:Youssou N'Dour][a...
[ti:Dabbaax]
[ar:Youssou N'Dour]
[al:Rokku Mi Rokka (Give and Take)]
[by:]
[offset:0]
[00:00.00]Dabbaax - Youssou N'Dour
[00:13.65]Keroksou penc bognouy wadjia wathié janta bi
[00:17.39]
[00:21.79]Di wadjial péssé ba
[00:24.12]
[00:26.84]Moulay dabbaxx yalla nagnou la diégué yalla daal moy taan waayam
[00:30.81]
[00:32.30]Moulaay dabaaaaax
[00:34.13]
[00:37.66]Bougnou faté bess boboulé uhh bougnou soré bess boboulé
[00:46.74]
[00:48.51]Bougnou faté bess boboulé
[00:51.93]
[00:53.79]Lofa gnaane yalla may lako
[00:57.82]
[01:02.22]Modaane wakhal nitt gnep mo daane wakhal nasraane yi
[01:11.74]
[01:12.72]Anh mo daane kadou askane wi
[01:16.71]
[01:17.80]Dafa daane wakh naane nagnou bolé sougn rew
[01:21.21]
[01:23.15]Dafa daane wakh naane bou kéne wéngal gaal gui
[01:26.83]
[01:28.69]Dafa daane wakh naane nagnou bolé sounou khol yi
[01:32.20]
[01:33.95]Dafa daane wakh naane nagnou yeureum djiguéen
[01:38.28]
[01:54.26]Sa borom bi begu na yonentam bi begu na yako liguéyal sa borom
[01:58.66]
[02:02.37]Moulaye dabbaxx yaw dé wacci ngua masso wakh lou amoul
[02:06.91]
[02:10.24]Kérok bang gnou djito assamaane si da leudeum
[02:13.22]Bessa ngui kéne dotou ko fatéééti moulaay dabbaxx
[02:18.90]
[02:21.54]Bougnou faté bess boboulé bougnou soré bess boboulé
[02:30.85]
[02:32.19]Bougnou faté bess boboulé
[02:35.88]
[02:37.64]Lofa gnaane yalla may lako
[02:41.27]
[02:42.92]Anh modaane wakhal nitt gnep anh mo daane wakhal nasraane yi
[02:52.44]
[02:53.57]Anh mo daane wakhal askane wi
[02:58.11]
[02:59.12]Dafa daane wakh naane na gnep ligueye
[03:02.55]
[03:04.31]Dafa daane wakh naane nagn diangal gounéyi
[03:07.98]
[03:09.68]Dafa daane wakh naane na gnep liguèye
[03:13.11]
[03:15.14]Dafa daane wakh naane nagn diangal djiguééne gni
[03:18.79]
[03:27.58]Daawaoul sétane lou gnaaw
[03:35.48]
[03:38.06]Poussom la yorone fou khotékou mou gnaw
[03:40.43]
[03:41.20]Rewmirewmi amélnagnou la ndiouka moulaay dabbaxx
[03:46.22]
[04:01.11]Daawaoul sétane lou gnaaw
[04:03.06]
[04:05.10]Poussom la yorone fou khotékou mou gnaw
[04:07.97]
[04:09.06]Rewmirewmi amélnagnou la ndiouka moulaay dabbaxx
[04:12.45]
[04:12.96]Bakrék dara maam aram lô coumba thiam
[04:15.28]
[04:15.96]Magn penda ak pathé penda ah
[04:20.70]
[04:27.13]Modaane wakhal nitt gnep mo daane wakhal nasraane yi
[04:36.77]
[04:37.69]Mo daane kadou askane wi
[04:41.93]
[04:42.77]Dafa daane wakh naane nagn diap sounou rewmi
[04:46.49]
[04:48.25]Dafa daane wakh naane nagnep liguéye
[04:51.45]
[04:53.54]Dafa daane wakh naane nagn yeureum djiguéene gni
[04:57.54]
[04:59.04]Dafa daane wakh naane nagn diangal gounéyi
展开
广告图片
广告图片