cover

Tukki-Youssou N'Dour

 如无法下载或有错误,请刷新重试或点此反馈给我们
Tukki-Youssou N'Dour.mp3
[ti:Tukki][ar:Youssou N'Dour][al:...
[ti:Tukki]
[ar:Youssou N'Dour]
[al:Rokku Mi Rokka (Give and Take)]
[by:]
[offset:0]
[00:00.00]Tukki - Youssou N'Dour
[00:06.84]Yoon wi nga jël baaxul ku la koy digël da lay nax
[00:11.19]
[00:14.39]Yoon wii ci des moo gën loo taseel dàldi kuy mën
[00:18.02]
[00:20.83]Yoon wii nga jël
[00:23.84]
[00:26.17]Booy dox ba ca biir géstul xool fi nga weesu balaa ngay
[00:32.58]
[00:35.04]Booy tukki yaw
[00:36.11]
[00:38.40]Booy tukki yaw
[00:39.82]
[00:42.25]Booy tukki yaw
[00:43.53]Na nga bàyyl ba mën
[00:44.88]
[00:45.67]Ding cë jëléé lu mënë xew ca feneen
[00:48.62]Dina tax nga mën xam nekkinu ñeneen
[00:52.23]Foofo mën nga fa gis lu yókk sa xameel
[00:55.59]
[00:56.26]Booy tukki yaw
[00:57.55]
[01:01.94]Nita ngi toog di janoog yaw
[01:03.01]
[01:05.44]Booba fekk na ma ngay xalaat ba tàbbi asamaan
[01:08.48]Àndag niir yiy naaw dem na fu sore lépp ciy xalaatam
[01:13.06]
[01:14.35]Yaw sama waay kaay ma xamal la
[01:15.74]
[01:16.84]Léég léég nga toog fi nga toog tukki
[01:19.22]Bu neex dem ba kaw asamaan
[01:20.84]
[01:22.08]Ànd ag weer wiy naaw
[01:23.25]
[01:25.10]Li ngay janeer mu lay neex boo janoo mu gën fee neex
[01:28.43]Booy tukki yaw
[01:29.46]
[01:31.90]Booy tukki yaw yeesal sa xameel
[01:34.63]
[01:35.60]Ding cë jëléé lu mënë xew ca feneen
[01:38.56]Dina tax nga mën xam nekkinu ñeneen
[01:42.10]Foofa mën nga fa gis lu yókk sa xameel
[01:45.42]
[01:46.12]Deel tukki yaw
[01:47.17]
[01:51.42]Lëppa lëpp sàmba ma ngay naaw
[01:53.09]
[01:55.01]Te booy seet sax taxu koo gaaw
[01:56.75]
[01:57.58]Te léég léég mu dem ba kaaw
[01:59.52]
[02:00.40]Tukkee ka neex waaw
[02:02.58]
[02:03.87]Lucum cééli ma ngay naaw
[02:05.44]
[02:07.55]Te léég léég mu naaw ba kaw asamaan indi fiy xabaar
[02:10.87]
[02:11.39]Ku dul tukki doo xam fu dëkk neexe
[02:14.60]Booy tukki yaw
[02:15.50]
[02:18.20]Booy tukki yaw
[02:19.51]Na nga bàyyi
[02:20.36]
[02:21.70]Booy tukki yaw
[02:23.13]Na nga bàyyi ba mën
[02:24.36]
[02:25.25]Ding cë jëléé lu mënë xew ca feneen
[02:28.31]Dina tax nga mën xam nekkinu ñeneen
[02:31.83]Foofa mën nga fa gis lu yókk sa xameel
[02:35.08]
[02:35.97]Booy tukki yaw
[02:36.97]
[02:39.31]Booy tukki yaw
[02:40.71]
[02:42.97]Booy tukki yaw
[02:44.49]Na nga bàyyi ba mën
[02:46.23]Ñaanu barke ah ñaanu barke
[02:52.08]
[02:57.59]Nita ngi toog di janoog yaw
[02:59.26]Booba fekk na ma ngay xalaat ba tàbbi asamaan
[03:01.88]Àndag niir yiy naaw dem na fu sore lépp ciy xalaatam
[03:06.82]
[03:08.05]Yaw sama waay kaay ma xamal la
[03:09.81]Léég léég nga toog fi nga toog tukki
[03:12.00]Tukki bu neex dem ba kaw asamaan
[03:13.37]Làng ag weer wiy naaw li ngay janool mu lay neex boo janoog moom
[03:18.59]
[03:19.12]Mu gën fee neex
[03:20.20]
[03:22.19]Booy tukki yaw
[03:23.54]Na nga bayyi ba mën
[03:24.65]
[03:25.60]Ding cë jëléé lu mënë xew ca feneen
[03:28.70]Dina tax nga mën xam nekkinu ñeneen
[03:32.20]Foofa mën nga fa gis lu yókk sa xameel
[03:36.00]
[03:36.55]Deel tukki yaw
[03:37.47]
[03:39.85]Lëppa lëpp sàmba ma ngay naaw
[03:41.71]
[03:43.39]Te booy seet sax taxu koo gaaw
[03:45.41]
[03:46.98]Te léég léég mu dem ba kaaw
[03:49.42]Tukkee ka neex waaw
[03:51.79]
[03:53.02]Lucum cééli ma ngay naaw te booy seet sax taxu koo gaaw
[03:57.97]
[03:59.83]Ëndaaleel ñu xabaar
[04:01.07]
[04:01.63]Tukkee ka neex waaw
展开
广告图片
广告图片