Taasukat baa nga naan gainde gu waaf ca buntu kër gé, di melastiku Bëy bu em bàjjan du fa dem, Zacharia, bàjjan am na maanaa, wayai Lu la réér ci sa cosaan, sa bàjjan xamal la ko Boo bëgéé xam sa cosaan, kam la fa maam yi bayyi woom Demal seeti bàjjan ba, lu mu la ca wax, du deñ Bàjjana xam Kalcor an ba ca mbeneex wa Cosaani askan wi, bàjjan am na maanan Wayum terànga la kuy bàjjan jogal yëngu, sunguñ sangañ bàjjan, bàjjan Wayum terànga la kuy bàjjan jogal yëngu, bàjjan, bàjjan, sunguñ sangañ Neenañ mag de mët naa ba cim rééw waaye bàjjan it mët na bàyyi ci biir kër Xam sa boppa gën ñu woo la naan kii nga doon Wayum terànga la kuy bàjjan jogal yëngu, sunguñ sangañ bàjjan, bàjjan Wayum terànga la kuy bàjjan jogal yëngu, bàjjan, bàjjan, sunguñ sangañ Boo bëgéé xam sa cosaan, sa bàjjan moo la koy xamal Moo la naan awai fii, bul dem fee, defeel nii Boo ko seetioo dara du ca deñ Wayum terànga la kuy bàjjan jogal yëngu, sunguñ sangañ bàjjan, bàjjan Wayum terànga la kuy bàjjan jogal yëngu, bàjjan, bàjjan, sunguñ sangañ Mani bàjjan moodi magi gaay walla raidiam Lu xew lune mane bàjjan laxaw Bu góór bugéé néégu góór Bàjjan taxaw wayal ko mbaax Nijaay di Yaay nga di Baay
Bàjjan am na maanaa Wayum terànga la kuy bàjjan jogal yëngu, sunguñ sangañ bàjjan, bàjjan Wayum terànga la kuy bàjjan jogal yëngu, bàjjan, bàjjan, sunguñ sangañ Bàjjan moodi magi baay walla rakkam Lu xew lune mane bàjjan laxaw Bu góór bugéé néégu góór Bàjjan taxaw wayal ko mbaax Nijaay di Yaay nga di Baay Bàjjan am na maanaa Wayum terànga la kuy bàjjan jogal yëngu, sunguñ sangañ bàjjan, bàjjan Wayum terànga la kuy bàjjan jogal yëngu, bàjjan, bàjjan, sunguñ sangañ