[ti:Sama Gàmmu] [ar:Youssou N'Dour] [al:Rokku Mi Rokka (Give and Take)] [by:] [offset:0] [00:00.00]Sama Gàmmu - Youssou N'Dour [00:11.86]Nanga def yaw sama gàmmu dégg naa da nga yor xaalis [00:17.42]Xam naa ne yaw moomu loo ko [00:19.59]Dang ko àbb mbaa nga for ko [00:20.88]Baal dóózéé eh [00:22.36] [00:28.97]Nanga def na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis [00:33.93] [00:34.65]Ba foo ma séén tàmbaleey wëlis [00:36.77] [00:37.40]Xam naa ne yaw moomu loo ko [00:39.09]Dang ko àbb mbaa nga for ko [00:40.79]Baal dóózéé eh [00:42.31] [00:48.77]Yor khalis meunoul tè ma môm la [00:51.09] [00:51.68]Keur gou rich meunoul tè ma môm la [00:53.74] [00:54.33]Yaw na nga def yaw sama gàmmu [00:56.38] [00:57.15]Dég na danga yor khalis [01:00.04]Khamna ni yaw momouloko dang ko abb mba nga forko bâl dôzé tèyal [01:05.43] [01:17.12]Kaay gaaw wax ma na nga def ba am ko [01:19.53] [01:20.05]Foog nan nita ko waddal nga for ko [01:22.81]Wax ma gaaw ñaata la doon ma fay ko [01:25.62]Man daal maay sa buur nangu ko [01:28.44]Nanga def na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis [01:33.76]Ba foo ma séén tàmbaleey wëlis [01:36.04] [01:36.56]Xam naa ne yaw moomu loo ko [01:38.59]Dang ko àbb mbaa nga for ko [01:40.12]Baal dóózéé eh [01:41.66] [01:52.07]Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee [01:57.57]Ah suñuy baay noonu lañ ko daan waxee [02:03.04]Ah suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee [02:08.74]Ah gàmmu daal sama doomu nday nga [02:13.86] [02:14.65]E e e gàmmu daal suma xarit nga [02:19.57]E e e gàmmu daal suma askan nga [02:25.80]Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee [02:31.28]E e e gàmmu daal suma xarit nga [02:36.24]E e e gàmmu daal man sama doomu nday nga [02:42.16]E e e gàmmu daal man suma xarit nga [02:47.66]E e e e gàmmu daal yaw sama doomu nday nga [02:53.59] [03:16.78]Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee [03:22.03]Ah suñuy baay noonu lañ ko daan waxee [03:27.16] [03:27.90]Ah suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee [03:32.99]E e e gàmmu daal sama doomu nday nga [03:38.32]E e e e gàmmu daal suma xarit nga [03:43.44] [03:43.95]E e e e e gàmmu daal suma askan